Dolene gneuw gnou yengeul reddit?
Sénégalais moom foumou nek dafa wara neex gneuw leen gnou tegg ay activités genre débats wala ay jeux yeungeul touti r/Senegal bi waleu???