Gnou foo?
Amnaa benn jeu bo xamni damay commencer benn histoire (lepp en wolof lay donn) après commentaire bi ci topou yokou ci louko nekh(maximum 3 phrases) kenene tontou dernier commentaire bi en faisant la même chose ainsi de suite Ba kerok gnouy am une histoire complète Histoire bi nak diaroul mouy logique deh bayekou leen🤣🤣🤣